Apocalipse 14
Téereb Injiil (WOL2010) vs AAI
1 Ma xool noonu, gis Gàtt ba taxaw ci tundu Siyoŋ, ànd ak téeméer ak ñeent fukk ak ñeenti junniy nit, te ñu bind ci seen jë turu Gàtt ba ak turu Baayam.
1 Imaibo ayu anuwanuw nou’umaim oyaw Zion tafan Lamb batabat aitin, ana sabuw etei 144, 000 bairi. Naatu nati sabuw nakwetahimaim i Lamb wabin naatu Tamah wabin auman hikirumen.
2 Ma dégg baat bu jóge asamaan, buy riir ni duusi géej, ni riiru dënnu gu réy. Baat ba ma dégg mel ni baati xalamkat yuy xalam.
2 Naatu maramaim nidun ta anonowar i harew tititit niduhibe, naatu gunum erab gugugug ebiwa’an na’atube. Niduw anonowar i taboroyah hai douduf terabirabibe.
3 Nit ñu bare ñooñu taxaw ca kanam gàngune ma ak ñeenti mbindeef ya ak mag ña, di woy woy wu bees. Kenn manula jàng woy wa, ku dul téeméer ak ñeent fukk ak ñeenti junniy nit, ñooñu ñu jote àddina.
3 Naatu urama’ama, sawar kwafe’en yawasih ma’anih naatu regaregah ai’in nahimaim hibat ew boubun hitabor, iti ew i boro men yait ta hini’obaiyih hinaso’ob, baise tafaram ana sabuw etei wanawanahimaim 144,000 hitutubunih akisihimo iti ew hiso’ob.
4 Ñoo di ñi taqul sobey jigéen, ndaxte saxal nañu seen bopp ci sellaay. Ñu nga topp Gàtt ba fépp fu mu jëm. Yàlla jot na leen ci biir nit ñi, ñu jébbalu ci Yàlla ak ci Gàtt bi, mel ni tànneefu ngóob mi ñuy sédde Yàlla,
4 Iti oro’orot i biyah hikaif gewas uhew hima, men kafa’imo baibin bairi hi’in biyah gubagub mataramih. Mar etei Lamb menamaim inan i hibi’ufunun. Orot babin etei wanawanahimaim i akisihimo hitubunih, ai ro’oh wan tiyamur tafafayay na’atube, God ana Lamb hairi hai fayay na’atube hitih.
5 te fen masula génn ci seen gémmiñ. Amuñu benn sikk.
5 Men kafa’imo baifuwen ta awahimaim hitita’urihimih aurih ubar, en.
6 Noonu ma gis meneen malaaka naaw ca digg asamaan, yor xibaar bi sax, di ko yégal waa àddina— xeet yépp ak giir yépp ak kàllaama yépp ak réew yépp.
6 Naatu anuwanuw tounamatar ta auyom waruw wanawanan roberob aitin, wanatowan ana tur gewasin bai tafaramamaim sabuw, tafaram ta ta, big ta ta, tur ta ta naatu biyah ta ta, isah orerebamih.
7 Ma nga doon xaacu naan: «Ragal-leen Yàlla te jox ko ndam li, ndaxte waxtuw àtteem jot na. Jaamuleen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»
7 Fanan aumetawat na’in eo, “God kwanabiruw naatu kwanakakafiy! Ana gagamin kwanao kwanabora’ara’ah, anayabin baibabatiyen ana veya natit. God, mar, tafaram, riy, naatu harew ana sinafenayan kwanakwafir.”
8 Meneen malaaka, di ñaareel bi, topp ca naan: «Daanu na! Babilon, dëkk bu mag, bi daan màndil réew yépp ak biiñu njaaloom, daanu na.»
8 Tounamatar bairou’abin i’ufunun tit eo, “Babilon ra’iyeka! Babilon bar merar gagamin i ra’iyeka, anayabin tafaram wanawanan sabuw baiwa’an kwanekwan ana wine babin faramih etei hitom!”
9 Meneen malaaka, di ñetteel bi, topp ca, di xaacu naan: «Ku jaamu rab wi ak nataalam te nangoo am màndargaam ci jëëm walla ci loxoom,
9 Tounamatar baitounin i’ufunun tit fanan aumetawat na’in eo, “Orot yait sawaidab nakwafir naatu i ana itininabe auman nakwafir, ana ewow nibasit nab ukwarin o umanamaim na’uh nama’am,
10 dina naan moom itam biiñu xadarub Yàlla bi kenn raxul, ñu sotti ko ci koppu meram. Te dees na ko mbugal ci sawara ak tamarax ci kanam malaaka yu sell yi ak Gàtt bi,
10 i boro God ana yaso’ar wine natom. Nati wine i ana fairin tutufin etei yaso’ar kerowasamaim isuwei’ika ebatabat! O boro sulfur wanawanan inarun na’arah na’arfufuri biyababan gagamin maiyow tounamatar kakafiyih naatu Lamb bairi nahimaim inab.
11 te saxar siy jóge ci seen mbugal dina gilli ba fàww. Ñooñu di jaamu rab wi ak nataalam, ak képp ku nangoo jot màndargam turam, duñu noppalu guddi ak bëccëg.»
11 Naatu fai mar biyababan bai’akir ana sow boro wanatowan, wanatowan na’in nayen, auyit o gugumin biyah tubaiwa’an isan ana veya men ta ema’am. Sawaidab ana kwafirenayah, naatu i ana yumatabe kwafirenayah na’atube sabuw iyab hibasit wabin ana ewow hibaib iti biyababan boro fai mar hinab.”
12 Looloo tax gaayi Yàlla yi wara muñ, ñooñuy sàmm ndigali Yàlla yi ak ngëm ci Yeesu.
12 God ana sabuw iti tur i kwanab, yatenanub nawainabi God ana obaiyunen tur kwanabukikin Jesu isan kwanabosunusunub.
13 Noonu ma dégg baat ci asamaan naan: «Bindal: “Bés ni tey, ñi nekk ci Boroom bi te dee, barkeel nañu.”» Xelum Yàlla nee na: «Waaw, dinañu noppalu ci seeni coono, ndaxte seeni jëf a nga leen di xaar.»
13 Imaibo maramaim fanan ta eo anowar, “Iti kukirum: sabuw iyab Regah wabinamaim himomorob boun ana veya ebubusuruf boro baigegewasin hinab.”
14 Ma xool noonu, gis niir wu weex ak ku ca toog, niroo ak doomu nit, takk kaalag wurus ca bopp ba, yor sàrt bu ñaw.
14 Imaibo anuw naatu nou’umaim wakasakas kwes aitin, tafanamaim Orot Natun ana itininabe, ukwarinamaim kowas gold naatu umanamaim i fafour ana kaifut auman.
15 Te meneen malaaka génn ca kër Yàlla ga, di wax ak baat bu xumb ak ka toogoon ca niir wa, ne ko: «Dawalal sa sàrt te góob, ndaxte ngóob jot na, te lépp ñor na ci kaw suuf.»
15 Naatu tounamatar ta Tafaror Barene tit orot nati wakasakas tafan ma’am isan fanan aumetawat na’in e’af, “A Kaifut kubai naatu masaw kufour, anayabin fourin ana veya i natit, tafaram i iyamur fourinamih.” Fafour ana kaiy|alt="sickle" src="cn02109B.tif" size="col" loc="Rev 14.15-19" copy="©1978 David C. Cook Publishing Co." ref="14.15-19"
16 Noonu ka toogoon ca kaw niir wa dawal sàrtam ci kaw suuf, góob àddina sépp.
16 Naatu orot nati wakasakas tafan ma’am ana kaifut tafaram tafanamaim i’asakan naatu tafaram tutufin etei four.
17 Bi loolu amee meneen malaaka génn ca kër Yàlla ga nekk ca asamaan, yor moom itam sàrt bu ñaw.
17 Tounamatar tabo maramaim Tafaror Barene titit aitin, umanamaim i ana kaifut wan so’arin auman.
18 Noonu meneen malaaka, ma am sañ-sañ ca sawara sa, jóge ca sarxalukaayu cuuraay ba, daldi wax ak baat bu xumb ak malaaka, ma yor sàrt bu ñaw ba, ne ko: «Dawalal sa sàrt bu ñaw bi te dagg cëggu reseñ yu àddina, ndaxte ñor nañu.»
18 Iban maiye tounamatar ta wairaf ana kaifayan sibor ana gemane tit, naatu fanan aumetawat na’in e’af tounamatar uman ana kaifut wan so’arin bai batabat isan eo, “A kaifut wan so’arin kubai tafaram ana masaw yan grape umah ku’afuwen kwita’ay, anayabin grape i hiwu.”
19 Noonu malaaka ma daldi dawal sàrtam ci àddina, dagg reseñ yi, sànni leen ci biir segalukaay bu réy bu merum Yàlla.
19 Tounamatar ana kaifut kamar tafanamaim iasakan grape ro’oro’oh e’afuw hira’iy bow ta’asiyen God ana yaso’ar wine bunubunuw wanawanan hira’iy.
20 Ñu nal reseñ ya ca segalukaay, ba ca gannaaw dëkk ba, deret génn ca, ba agsi ci laabi fas yi, te wal ba ëmb lu mat ñetti téeméeri kilomet.
20 Naatu wine ana bunubunuw bar merar gagamin ufunane hibun fesafesaren, rara wine ana bunubunuwane titit i harew titit na’atube re nunuw in 300 kilometres na’atube naatu ana taiy i sika kabokabom ana fofonin o kafa’imo 2 metres bai.
Atalhos do teclado
- Capítulo anterior←
- Próximo capítulo→
- Versículo anteriork
- Próximo versículoj
- Limpar seleçãoEsc
- Esta ajuda?
Estude este capítulo no WhatsApp
Peça à IA da Bíblia Fala para explicar Apocalipse 14, comparar traduções ou montar um estudo — tudo direto pelo WhatsApp.